Ubbil li ci biir

Biibël bi

Fi mu jóge ak liy wone ne dëgg la

Ndax li nekk ci Biibël bi, kàddu Yàlla la ?

Ñu bare ci ñi bind Biibël bi dañu wax ne, Yàlla moo leen xiir ci bind li ñu bind. Lu tax ?

Ndax li science wax ànd na ak li Biibël bi wax?

Ndax science dafa gis njuumte ci li Biibël bi wax?

Ndax Biibël bi, téere tubaab la ?

Ñi bind Biibël bi fan lañu juddoo ? Fan la seen réew féete ci àddina ?

Njariñ bi mu am

Ndax Biibël bi mën na ma dimbali ma am jàmm ci sama biir njaboot?

Xelal yii jóge ci Biibël bi dimbali nañu ay milioŋi nit, góor ak jigéen, ñu am jàmm ci seen biir njaboot.

Bu ñu amee feebar bu yàgg, ndax Biibël bi mën na ñu ci dimbali?

Waaw-waaw! Xoolal ñetti ponk yu la mën a dimbali boo amee feebar bu yàgg.