Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Ndax Yàlla am na tur ?

Ndax Yàlla am na tur ?

Yàlla, ni ñu koy woowe bare na, mel ni : Aji Man ji, Sàkk-kat ak Boroom. (Job 34:12 ; Ecclésiaste 12:1 ; Dañeel 2:​47) Waaye ndax Yàlla joxul boppam tur ?