Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Lu war a tax ñu gëm ne li Biibël bi wax dëgg la ?

Lu war a tax ñu gëm ne li Biibël bi wax dëgg la ?

Biibël bi nee na “ kàddu Yàlla ” la te Yàlla du “ tebbi waxam ”. (1 Tesalonig 2:13 ; Tit 1:2) Ndax loolu dëgg la, walla ndax Biibël bi du ay léeb kese ?