Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Xoolal li Biibël bi wax)

Téere bu ndaw bii, mën na la dimbali nga komaase jàng Biibël bi. Dafa bokk ci porogaraam bi ñu am ngir jàngal nit ñi Biibël bi te duñu fey dara.