Ubbil li ci biir

Ñu ngi lay woo ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu Seede Yexowa yi bu atum 2024 bi tudd: «Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»

Dégg xibaar bu bon mën na ñu xàddiloo. Waaye, xibaaru jàmm bi mën na tax ñu yaakaar ne ëllëg dina neex!