Ubbil li ci biir

Li yeneen ndaw wax

Seetaanleen ay wideo yuy wone ay ndaw ci àddina si sépp yuy wax ci jafe-jafe yi ñuy am ak ni ñuy def ba génn ci.

 

Ay ndaw yuy wax lu jëm ci gëm Yàlla

Ci wideo bii di def ñetti minit ay ndaw wax nañu li tax ñu gëm ne am na ku sàkk lépp.

Ay ndaw yuy wax lu jëm ci liir Biibël bi

Du saa su ne lañuy bëgg liir, waaye góorgóorlu ngir liir Biibël bi lu am solo la. Ñeenti ndaw wax nañu ci njariñ bi ñu jële ci liir Biibël bi.