Ubbil li ci biir

“ Lii moo tax ma ñëw àddina ”

Yeesu dafa doon jàngale dëgg gi ak fit. Xoolal ni mu aaye woon ci njàngale.