Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

“Am nañu Xibaaru jàmm”! (Woyu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024)

“Am nañu Xibaaru jàmm”! (Woyu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024)

(Luug 2:10)

Telesarseel:

  1. 1. Nañu màggal Yexowa

    Ca kaw asamaan.—

    Bi Yeesu juddoo ca Betleyem,

    Yaakaar amaat na

    Ndax mooy Musalkat bi.

    (AWU BI)

    Jërëjëf Yàlla!

    Xibaar bi neex na.

    Jàmm lay indi.

    Yeesu mooy yoon wi,

    Nañu yégle lii:

    Yeesu juddu na—

    Moom mooy ki ñuy musal.

  2. 2. Waaw, Yeesu dina nguuru,

    Jàmm am fu ne.

    Moo ñuy jëme ci dund ba fàww.

    Yoon rekk lay àtte,

    Nguuram du mas a jeex.

    (AWU BI)

    Jërëjëf Yàlla!

    Xibaar bi neex na.

    Jàmm lay indi.

    Yeesu mooy yoon wi,

    Nañu yégle lii:

    Yeesu juddu na—

    Moom mooy ki ñuy musal.

    (AWU BI)

    Jërëjëf Yàlla!

    Xibaar bi neex na.

    Jàmm lay indi.

    Yeesu mooy yoon wi,

    Nañu yégle lii:

    Yeesu juddu na—

    Moom mooy ki ñuy musal.