Li ñuy def ak li ngeen di maye

Xaalis bi Seede Yexowa yi di defee seen liggéey ci li nit ñi di maye la jóge. Xoolleen li ñuy def ak maye yooyu ngir dimbali nit ñi ci àddina si sépp.

LI ÑU DEFAR

Defar nañu luy tax suñu mbokk yi ci ngëm mën a telesarse suñu téere yi ak wideo yi

Léegi, Seede Yexowa yu bare mën nañu telesarse suñu téere ak wideo yi ñuy fekk ci jw.org bu dee sax amuñu internet.

LIGGÉEY BI JATAAY BIY DOGAL AK BÀNQAAS YI DI DEF

Ñi am lu bare dañuy faj soxlay ñeneen ñi

Réew yu amul xaalis bu doy dañuy jot ndimbal ngir ñu mën fa def suñu liggéey. Fan la xaalis boobu jóge?

LIGGÉEYU WAARE BI AK NJÀNGALE MI

Defar nañu wideo yi ñu war a seetaan ci suñu ndaje bu mag bu ñetti fan bu 2020 bi tudd «Deeleen bég»!

Dañuy defar ay wideo yu ñuy seetaan ci suñu ndaje yu mag yu ñetti fan yi. Ndax xam nga liggéey bi muy laaj ak xaalis bi ñu ciy dugal?

Tekki nañu ci ay làkk yu bare suñu ndaje bu mag bu ñetti fan bu 2020 bi tudd «Deeleen bég»!

Lan lañu def ba mën a tekki, ci diir bu gàtt, ay waxtaan, ay film ak ay wóy ci lu ëpp 500 làkk?

Ndaje yi mbooloo yi di def ci internet

Lan la mbootaayu seede Yexowa yi def ba mbooloo yi am Zoom yu baax te yomb ngir ñu kontine seeni ndaje ci internet?

Sorry, there are no terms that match your selection.