Ubbil li ci biir

Li Biibël bi wax

Ak loo mënta laaj lu jëm ci àddina, Biibël bi moo ciy joxe tont bi gën a leer. Te Biibël bi masul a xewwi. Ci xaaj bii, dinga gis li tax nga mën a gëm li Biibël bi wax ak njariñ bu réy bi nekk ci jàng ko te topp li mu wax (2 Timote 3:16, 17).

 

Li ñu bëgg ñépp xool

AY LAAJ YU JËM CI BIIBËL BI

Ndax li science wax ànd na ak li Biibël bi wax?

Ndax science dafa gis njuumte ci li Biibël bi wax?

AY LAAJ YU JËM CI BIIBËL BI

Ndax li science wax ànd na ak li Biibël bi wax?

Ndax science dafa gis njuumte ci li Biibël bi wax?

Jàngal Biibël bi ak Seede Yexowa yi

Ndax bëgg nga ñu seetsi la?

Mën nga waxtaan ci benn laaj ci Biibël bi walla nga jàng lu jëm ci Seede Yexowa yi.

Naka la la Biibël bi mënee dimbali?

Ndimbal pur ndaw ñi

Xoolal ni Biibël bi mënee dimbali ndaw ñi ci jafe-jafe yi ñuy faral di am.

Lan la Biibël bi wax ?

Ay laaj yu jëm ci Biibël bi

Xoolal tont yi Biibël bi joxe ci ay laaj yu jëm ci Yàlla, Yeesu, njaboot, coono ak yeneen.