Ubbil li ci biir

Lãsamã tiyaatar bu sukkandiku ci Biibël bi te tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle: Xaaj 1 (Leer gu wóor gi ñëw ci àddina)

Lãsamã tiyaatar bu sukkandiku ci Biibël bi te tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle: Xaaj 1 (Leer gu wóor gi ñëw ci àddina)

Yexowa yégle na ni mu naree musal doomu Aadama yi: Sakari ak Elisabet dinañu jur ab yonent doonte sax màgget nañu. Yuusufa ak Maryaama ñoo nar a yar Almasi bi. Dañu ko waroon a aar itam bi mu nekke xale.